Man Dofbi a écrit:Kayla, saa jarbaat, ñii, bayyi maak ñoom rekk.
Sallaaw, man lañ fiy fekk.
Yow kay, jublul ma ci
Hodei, ndax ngone si daf may tutoyer te xaju ma ci moom.
Mane salaamaalikum, joxaguñ ma sax dox ma naan, mu topp ma : fu ma dugg, mu ne fa jalañ di xuliy gët. Mbaa naan "a new cowboy"
Kar ko boppu koñ ba, régler ko ba mu normale. Pas de pitié ! Dóór ko bamu mandi. Booy dem sax, ma abal la sama tapparka, mais ne la blesse pas trop.
Mais nak, j’ai remarqué qu’ici, certaines filles ne se prennent pas pour n’importe qui.
Des pseudos comme
bijoux (Kii moom, elle montre la couleur. Qui veut l’épouser dépensera tout son argent en parures.)
Sweety (Ndaw si, saabu du fóót boppam waay. Xaaral ba ñu tagg la, moo gën nga nekk fi di sweety-sweety.) [
b]Honey [/b](Ey waay ! Après Sweety, voici Honey. Ñii de, kenn waxu léén dara. Bëgga neex daal amul app.)
Saf (Fii moom, fi la raay bi tééne. Saf ? Xaaral ba dëmm yi fekk ko fi, ba poobar ko, moutarde ko, boole ci tuuti soble. Di na xam ndax safnaam deet.)
Cherielaye (Ndeysaan ! Ki de, gëmewul Laye ba di ko fi woyantoo.)
Binette (Xoolal kii di nice-niçal. Manul ne Bintou wala Binta ?)
Ñii,
Petit Thiam di léén jay rekk, ñuy jayaxu, yaakaar ne ñoo ray golo gi, te melantaan sax rayu ñu ko. Wóór na ma ne ay nice-gudi la ñu, waaye séén bopp la ñuy nax.
Am na ku ci tudde boppam
Citoyenne. Ne sait-elle pas que même les poules sont des citoyennes ? D’ailleurs, je me demande si elle a voté. Comme disait l’autre, le tigre n’a pas besoin de chanter sa tigritude. Si elle veut montrer sa citoyenneté, elle s’est trompé d’adresse car fii, moom, elle n’impressionne personne.
Mounass, toi aussi, ne te laisse pas influencer par
Binette. Neel Maïmouna rekk, wala Maï. Xanaa liiroo Abdoulaye Sadji ? C’est joli, Maïmouna. Tu ne dois pas en avoir honte.
Mimi75 ? Wóóy ! Ree ba xomaag ! Lii moom, c’est ce que l’on appelle une recherche désespérée d’originalité. Ne trouvant pas mimi assez ridicule, elle y rajoute un « 75 ». Je suppose que c’est un message codé, sinon, je porte plainte parce que lii, c’est une atteinte à l’imagination.
Tima. Je crois qu’elle voulait écrire Tama. Je lui conseil Sabar.
Lady. Bilaay, bëgg classe di na ray nit. Kii nga xam ne elle n’est même pas encore une mini-disquette… Mon Dieu ! On voit tout de nos jours.
Yafall. Je lis mal, wala ? Kii, ku ko yafal ba muy bal-bal lu ?
Niangha. On ne peut être plus clair. Ñaang moom, Yalla na ñu ci dégg doy !
Nonesens. Enfin une fille intelligente, pourvu qu’elle la ferme.
Les garçons tamit ne sont pas en reste moom.
Jolie Ga ? Waaw gaa ñi, kii góór la wala jigéén ? Doy na waar moom.
Ndanane, saa waay, boo doon ndaandaan ma xam ko. Prends une chaise rekk et laisse-moi faire. Pas de sëmbëxloo.
Sammie. Kii moom, xanaa pël la ? Kuy samm ba dugg Internet wara fatte say nag, waay.
Bourefaye ? Vite ! Emmenez-le à Fann. Il se prend pour Salmone. Le pauvre. Saa waay, maintenant c’est la démocratie.
Khapi ? Sëñ bi, sa tur wi moom, da fa ñaaw. Def ko Xappati boog far benne.
Rew, reewande moom, jaru maa jaay. Di naa ko jënd ba wis la.
Thihi ? Moo yéén ! Cuqqutaan léén ma waay, ndax ma ree. Mas naa koo gis ? Kii de, on doit lui donner
Mimi75 comme épouse.
Modourateur moom, il se wanteer comme modou-modou, ne sachant pas que les filles d’ici sont des Fatou-fatou. Donc ci sooy lay dëkk.
Fouta. Foo bayyi Kajoor ak Bawol, Siin ak Saalum ? Ce n’est pas le jeu des royaumes. On te demande juste un pseudo bu nite tuuti. Pourquoi pas Charles ou Robert, Yoro ou Baïdi ?
Dakaroubzh, yow de, doo Yoro waaye ci Pël yi nga. Toppal
Fouta. Na séén gelaw nangu !
Frerooooo, ndugutung,
ku ma doon laaj, waa jaa ngi !